Sapoŋ

Japoŋ : Réewu Asi. 4 duni : Hokkaido, Honshu, Shikoku, Kyushu.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons
日本国
Nipponkoku / Nihonkoku
Raaya bu Sapoŋ Kóót bu aarms bu Sapoŋ
Barabu Sapoŋ ci Rooj

Barabu Sapoŋ ci Rooj
Dayo 377.972 km2
Gox
Way-dëkk 126.740.000 (2017) nit
Fattaay nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
Naruhito
Shinzo Abe
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
Tokyo
Làkku nguur-gi wu-sapoŋ
Koppar Yen
Turu aji-dëkk
Telefon
Lonkoyoon bu Sapoŋ

Lonkoyoon bu Sapoŋ   
Asi

Gox Adduna

Dawaan bu safaanu

Dawaan bu safaanu (DS walla AC ci wu-angalteer: Alternating Current) màndargoo ag walug dawaan guy soppiku ci jamono muy ci taraay walla ci jubluwaay.

Fukuoka

Fukuoka benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 1.550.626.

Hamamatsu

Hamamatsu benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 789.407.

Kamakura

Kamakura benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 174.314.

Kyoto

Kyoto benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 1.474.570.

Momoko Kōchi

Momoko Kōchi (河内 桃子; 7 maars 1932 — 5 nowembar 1998).

Nagoya

Nagoya benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 2.283.289.

Naruhito

Naruhito : Njiitu Réew Sapoŋ.

Osaka

Osaka benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 2.668.586.

Penku Asi

Penku Asi ab diwaanu Asi la.

Su nu cëslaayoo ci sedatle, gu àdduna bi, gi Mbootaayu Réew yi def, Penku Asi benn la ci diwaani Asi yi.

Yii ñoo fa nekk ciy Réew:

Siin

Kore gu Bëj-gànnaar

Kore gu Bëj-saalum

Sapoŋ

Mongooli

Sagamihara

Sagamihara benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 720.986.

Sapporo

Sapporo benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 1.918.096.

Sendai

Sendai benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 1.063.103 (2013).

Tokyo

Tokyo mooy péyu réewum Sapoŋ.

Xay

Baatu xay day tekki mbooleem ay mbaax ak ay melokaani aw askan. Maanaam xamug àdduna, ci wàllu yar ak teggin ak xam-xam, yewwute gu nit ñi ci aw askan. Su ñuy wax xay dañ ciy nat tolluwaayu sag dundin, ndax jëm na kanam walla déet; baat bi dafa ëmb mbooleem ay yëngu-yëngu yuy am ci aw askan: diine, cosaan, xamteef, politig,...

Su ñu nee nit kii dafa xayadi, day tekki ne xamul àdduna. Kon xayug aw askan ñoo ngi koy natt ci doxaliin, dundiinu cër bu ne ci askan wi

Yokohama

Yokohama benn dëkku di Sapoŋ. Nitñii motnañu 3.697.894.

Yeneeni làkk

This page is based on a Wikipedia article written by authors (here).
Text is available under the CC BY-SA 3.0 license; additional terms may apply.
Images, videos and audio are available under their respective licenses.