Ciipër

Ciipër (Republik bu Ciipër; el: Κύπρος, Κυπριακή Δημοκρατία; tr: Kıbrıs, Kıbrıs Cumhuriyeti): Réewu Tugal + Dun

Republik bu Ciipër
Raaya bu Ciipër Kóót bu aarms bu Ciipër
Barabu Ciipër ci Rooj

Barabu Ciipër ci Rooj
Dayo km2
Gox
Way-dëkk nit
Fattaay nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw

Làkku nguur-gi
Koppar Cyprus in its region (de-facto).svg
Turu aji-dëkk
Telefon
   
Angolemi

Angolemi dëkku di Ciipër. Nitñii motnañu 212 (2006).

Asi

Gox Adduna

Bëj-saalumu Tugal

Bëj-saalumu Tugal ab diwaan la ci goxu Tugal. Tekkib baat bi nak di na faral di indi ay werante, ba tax na am na ay tekki yu bari. Ci lu ëpp da ñuy wax naa Ispaañ, Itaali, Girees, ñooy réew yi ci bokk, daanaka ci lu daj réew yépp yi nekk ci Géej gu Diggu gi. Bëj-saalumu Faraas ci lu bari da ñu ko ciy boole.

Tugal

Tugal mooy wàll wi féete penku goxub Tugalasi, ci baax dees koy jàppe niki benn ci juroom-benn walla juroom-ñaari goxi àdduna bi. Gox baa gi digu ci sowwu ci mbàmbulaanug Atlas gi, ci bëj-gànnaar ci dottub Bëj-gànnaar bi, yem ci géej gu Diggu gi ci bëj-saalum. Ay digam ci penku dese nañoo leer, dinay faral di jur ay werante; li ko waral mooy ni mu taqalook goxub Asi.

Waa-Islaand jàppees na leen ni waa-tugal (donte féeteem ci degalub Tugal-Aamerig), ak mbooleem dun yi ci géej gu Diggu gi, Sipër mi gën a jur coow, ci wàllu melosuuf. Riisi ak Tirki ñi am li ëpp ci seen suuf ca Asi, waaye day ni rekk li ëpp ci seen taariix réewi gox bi lañu ko bokkal.

Yeneeni làkk

This page is based on a Wikipedia article written by authors (here).
Text is available under the CC BY-SA 3.0 license; additional terms may apply.
Images, videos and audio are available under their respective licenses.